Esther 9:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
moo tax Yawut yi di wormaal ñaari bés yooyu, sasoo ko, at mu nekk, bañ koo bàyyi, ñook seen askan ak ku ànd ak ñoom. Ñu war koo def, na ñu leen ko bindale, saa yu jotee at mu nekk.