bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Esther 9:28
Esther 9:28 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bés yooyu di lu ñu wara bàyyi xel, di ko wormaal ci bépp maas ci kër gu nekk, diiwaan bu nekk ak dëkk bu mag bu nekk. Bési Purim yooyu Yawut yi waruñu koo noppee wormaal, te wareesu koo fàtte ci seen askan.