Esther 9:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu mboolem kàngami diiwaan yaak jawriñ yaak boroom dëkk yaak saytukati buur, ñoom ñépp di dimbali Yawut yi ndax tiitaange lu ñu am ci Mardose.