Exodus 1:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Rewlikat ya ne ko: «Li tax kay mooy, jigéeni Ebrë yi dañoo niroowul ak jigéeni waa Misra; ndax dañoo njaxlaf, ba bu rewlikat yiy laata agsi, fekk ñu mucc ba noppi.»