Exodus 1:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Góor ñi soqikoo ci Yanqóoba ñépp juróom ñaar fukk lañu (70), bu ñu ci boolee doomam, ji ñuy wax Yuusufa, moom ma ñu fekk Misra.