Exodus 10:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Aji Sax ji ne Musaa: «Tàllalal sa loxo, mu jublu asamaan, lëndëm wàcc ci kaw réewum Misra, lëndëm gu nit mana daj, ndax fatt.»