Exodus 12:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Firawna nag jóg ca guddi ga, moom ak dagam yépp ak waa Misra gépp, yuux gu réy jibe ca Misra, ndax këroo kër, du genn gu nit deewul.