Exodus 12:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su dee gàtt bu ëpp waa kër ga, dañu koy bokk ak kër, gi leen gëna jege, te nañu seet nu nit ña tollu, doora tànn gàtt bu dëppook la ñu mana lekk.