Exodus 12:43 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Aji Sax ji dafa wax ak Musaa ak Aaróona, ne leen: «Li ma dogal ci saraxu bésub Mucc bi mooy lii: Benn doxandéem du ci lekk.