Exodus 16:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa wax leen ne leen: «Lekkleen li des tey, ndax tey jii bésub Noflaay la, ñeel Aji Sax ji, te dungeen ko gis tey ci àll bi.