bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Exodus 18:8
Exodus 18:8 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa nag nettali goroom mboolem li Aji Sax ji def Firawna ak waa Misra ndax Israyil, ak jafe-jafe, ya leen dab ca yoon wa yépp, ak na leen ca Aji Sax ji xettlee.