Exodus 19:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu loxo laal kooka, waaye nañu ko dóor ay doj ba mu dee, mbaa ñu jam ko. Su dee nit, su dee mala, bumu dundati.” Bu liit gi jibee doŋŋ nag lañuy doora mana dem ba ca tund wa.»