Exodus 20:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji waxati Musaa ne ko: «Li ngay wax bànni Israyil mooy lii: “Yeena ko gisal seen bopp. Ca asamaan sax laa àddoo, wax ak yeen.