Exodus 21:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waaye nag, su nit fexeelee moroomam, nax ko, ba rey ko, su làqoo woon sama sarxalukaay sax, jàppleen ko, rey.