Exodus 21:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
su ci jógee mana génn ci biti, jàpp ciw yet sax, di dox, deesul daan ki ko dóor, waaye dina dàmp ki mu dóor ngir li mu tëdd liggéeyul, ak li pajam laaj.