Exodus 21:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su aw nag dañee góor mbaa jigéen, ba rey ko, dóorleen nag wi ay xeer ba mu dee, te buleen lekk yàpp wi, waaye boroom nag wi, yoon toppu ko.