Exodus 21:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba tey itam, su nag wi dañee xale, ba mu dee, muy góor mbaa jigéen, na àtte biy benn rekk ci boroom nag wi.