Exodus 21:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su nagu nit jamee nagu moroomam, ba mu dee, nañu bokk jaay nag wiy dund, séddoo njég gi, te séddoo nag wi dee.