Exodus 21:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waaye su fekkee muy nag wu ñu xam ne da daan dañe, te boroomam ñàkk koo wattu, boroomam day feye nag wi dee aw nag wuy dund, daldi féetewoo wi dee.