Exodus 21:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko sangam jëndee, def ko jabar, ba noppi bëggatu ko, na fexe ñu feyal ndaw si ag njotam, waaye amul sañ-sañu jaay ko ay doxandéem, ndax loolu wor la.