Exodus 22:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su ko boroomam fekkee, du laaj muy fey. Su fekkee ne dafa bindoon mala mi ci boroom, di ko fey, na boroom féetewoo njég, ga ñu binde woon mala mi, muy peyam.