Exodus 22:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Su nit dénkee moroomam xaalis, mbaa alal, ñu sàcce ko ci kër ki denc, te ñu jàpp sàcc bi, na sàcc bi fey ñaari yoon la mu sàcc.