Exodus 23:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Diiru juróom benni fan ngeen di liggéey, waaye bésub juróom ñaareel ba, nopplu leen, ndax seen nag ak seen mbaam mana nopplu, seen surga akub doxandéem it mana astandiku.