Exodus 23:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Maa leen di dogal kemug suuf gu dale géeju Barax yi, ba géeju waa Filisti, daleeti ca màndiŋ ma, ba ca dexu Efraat, ndax maay teg waa réew mi ci seeni loxo, ngeen dàq leen.