Exodus 24:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk na mu wax mag ña ne leen: «Xaarleen nu fii, ba nu délsi. Aaróona ak Ur a ngi nii ak yeen; ku ci am mbir mooy àttelu, demal ci ñoom.»