Exodus 26:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Te itam ràbblul ay sori kawari bëy, ngir def ko ñaareelu xayma, muy kiiraay ci kaw jaamookaay bi. Fukk ak benn la sor yiy doon.