Exodus 29:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñam yooyu, ña koy lekk mooy ña muy seen saraxu njotlaay, keroog ca seen xewu colu, ga ñu leen tabbe ngir sellal leen. Waaye keneen du ci lekk, ndaxte ñam wu sell la.