Exodus 3:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa ne Yàlla: «Su ma demee ca bànni Israyil, ne leen seen Yàllay maam ya moo ma yónni ca ñoom bànni Israyil de, dinañu ma laaj nu mu tudd. Lu ma leen di wax nag?»