Exodus 32:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ca ëllëg sa Musaa ne mbooloo ma: «Yeen de bàkkaar ngeen bàkkaar bu réy, waaye maa ngi nii di yéeg, jëm ci Aji Sax ji. Jombul ma jotul leen seen bàkkaar.»