bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Exodus 33:5
Exodus 33:5 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk na Aji Sax ji wax Musaa ne ko: «Waxal bànni Israyil ne leen, ñoom askan wu dëgër bopp lañu. Su ma àndoon ak ñoom ab diir rekk, dinaa leen faagaagal. Kon nag nañu tàggook seeni gànjar, ba ma seet nu may def ak ñoom.»