Exodus 34:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye lu góor lu mbaam taawloo, joteleen ko ab gàtt, mu wuutu ko. Su ngeen ko jotewul lu ko wuutu, dammleen loos wi. Képp kuy taaw bu góor ci seeni doom it, nangeen ko jot. Te itam bu kenn taxawe loxoy neen fi sama kanam.