Exodus 34:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bànni Israyil nag di gis kanamu Musaa ak na deru kanam gay lerxate. Su ko defee Musaa dellu muuruwaat, làq kanamam, ba ba muy demaat, ngir wax ak Aji Sax ji.