Exodus 35:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa nag dajale mbooloom bànni Israyil mépp. Mu wax leen ne leen: «Lii mooy li Aji Sax ji santaane, ngir ñu def ko: