Exodus 35:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Képp ku namma jooxe xaalis mbaa xànjar, jooxeel nga ko Aji Sax ji, te itam képp ku dencoon bantu séng bu jëm ci mboolem liggéeyu sarxal bi, indi nga bant bi.