Exodus 35:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mayu jàngle itam yeb na ko cib dënnam, moom ak Oliyab, Daneen bi, doomu Ayisamaag.