Exodus 38:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
daldi roof njàppu yi ci nopp yi ci weti sarxalukaay bi, ngir bu ñu koy yóbbu. Am pax, mu xànq yu tàppandaar ub, moom la def sarxalukaay bi.