Exodus 4:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu Aji Sax ji wax ak Musaa ca Majan, ne ko: «Dellul Misra, ndaxte ña la doon wuta rey ñépp dee nañu.»