Exodus 4:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Aji Sax ji bàyyi Musaa. Ba Sipora di wax lu jëm ci jëkkër ju ñuy jote deret, aaday xarfal gaa taxoon.