Exodus 6:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji nag wax ak Musaa ak Aaróona, jox leen ay ndigal ci mbirum bànni Israyil ak Firawna buuru Misra, ngir ñu yiwi bànni Israyil, ba ñu génn Misra.