Exodus 7:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko defee yaw nga wax ko li ma la sant lépp, sa mag Aaróona wax ko Firawna, ngir mu bàyyi bànni Israyil, ñu génn réewam.