Exodus 7:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa Misra gépp di gas la wër dexu Niil, ngir am ndoxum naan, ndax manuñu woona naan ca dex ga.