Exodus 9:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag sa jur ak mboolem loo am, te mu nekk ci biti, booleel fat fu wóor, ndax lu nekk ci biti te fateesu ko, su tawtee dee, muy nit mbaa mala.’ ”»