Exodus 9:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Tawub yuur ba dal ca mboolem réewum Misra, daaneel lépp lu ne woon ca biti, nit ak mala, daaneel gàncax gépp, dammat garab ya ca àll ba yépp.