Ezekiel 1:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen melokaanu kanam nag nii la bindoo: ku ci nekk am nga kanamu nit fa féete kanam ak kanamu gaynde ci sa ndijoor. Ku ci nekk itam am nga kanamu yëkk fi sa càmmoñ ak kanamu jaxaay fa féete gannaaw.