Ezekiel 1:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fu noo gi wale jublu fa rekk, fa lañu jëm, mbege ya jógandook ñoom, ànd ak noo gi. Noowal boroom bakkan yi daal moo nekk ci mbege yi.