Ezekiel 1:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen laaf, loxoy nit a nga ca suufam ci seen ñeenti wet yépp, ñoom ñeent ñépp ak seeni kanam ak seeni laaf.