Ezekiel 10:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen bindu kanam ya mooy kanam ya ma gisoon ca tàkkal dexu Kebar. Ci seen melokaan, ñoom rekk la. Ku nekk man naa jubal màkk fépp fu genn kanam jublu.