Ezekiel 11:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yaw nit ki, gannaaw sa bokk yooyu nga bokkal, ñuy say bokk lenqe, di mboolem waa kër Israyil ñi nekk ngàllo, ñoom la waa Yerusalem di siis, naan: “Soreleen Aji Sax ji; réew mii, nun la ko sédd.”