bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 11:16
Ezekiel 11:16 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag, waxal ne: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa soreel moos seen bokk yooyu fa biir yéefar ya, maa leen wasaare biir réewoo réew, te du tee ma teewal leen ni bérab bu sell fa réew ya ñu sancaani.”