Ezekiel 11:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noowug Aji Sax ji daldi dal fi sama kaw, ne ma: «Neel: “Aji Sax ji dafa wax ne: Yeen waa kër Israyil, yeena waxe nii, seeni mébét, xam naa ko.